Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 92

Sabóor 92:10-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Aji Sax ji, sa noon yi kay, ndeke yoo; ndeke yoo sa noon yi, sànku rekk; defkati mbon ñépp, fëlxoo rekk.
11May nga ma dooley nagu àll, ma diwoo diw gu bees.
12Maa gis jéllu noon yi, dégg yuuxi ñu bon ñi may tëru.

Read Sabóor 92Sabóor 92
Compare Sabóor 92:10-12Sabóor 92:10-12