Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 92

Sabóor 92:10-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Aji Sax ji, sa noon yi kay, ndeke yoo; ndeke yoo sa noon yi, sànku rekk; defkati mbon ñépp, fëlxoo rekk.
11May nga ma dooley nagu àll, ma diwoo diw gu bees.

Read Sabóor 92Sabóor 92
Compare Sabóor 92:10-11Sabóor 92:10-11