Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 92:10-11 in Wolof

Help us?

Sabóor 92:10-11 in Kàddug Yàlla gi

10 Aji Sax ji, sa noon yi kay, ndeke yoo; ndeke yoo sa noon yi, sànku rekk; defkati mbon ñépp, fëlxoo rekk.
11 May nga ma dooley nagu àll, ma diwoo diw gu bees.
Sabóor 92 in Kàddug Yàlla gi