Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 8

Sabóor 8:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7fal ko ci kaw loo bind, jox ko lépp, mu teg tànk:
8jur gépp, gu gudd ak gu gàtt, rabi àll it ca la,
9ak njanaaw ak jën, ak luy jaare yooni géej.

Read Sabóor 8Sabóor 8
Compare Sabóor 8:7-9Sabóor 8:7-9