Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 8:7-9 in Wolof

Help us?

Sabóor 8:7-9 in Kàddug Yàlla gi

7 fal ko ci kaw loo bind, jox ko lépp, mu teg tànk:
8 jur gépp, gu gudd ak gu gàtt, rabi àll it ca la,
9 ak njanaaw ak jën, ak luy jaare yooni géej.
Sabóor 8 in Kàddug Yàlla gi