Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 88

Sabóor 88:14-17

Help us?
Click on verse(s) to share them!
14Aji Sax ji, man, yaw lay woo wall, xëy, kare la gii ñaan, ne la:
15Éy Aji Sax ji, loo may gàntale, di ma fuuylu?
16Mitit bay laatikaaf, sama ngone ba tey; sa mbugal yu raglu, ba bopp ubu ràpp!
17Sa mer mëdd ma, sa mbugal yu raglu sànk ma,

Read Sabóor 88Sabóor 88
Compare Sabóor 88:14-17Sabóor 88:14-17