Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 88:14-17 in Wolof
Help us?
Sabóor 88:14-17
in
Kàddug Yàlla gi
14
Aji Sax ji, man, yaw lay woo wall, xëy, kare la gii ñaan, ne la:
15
Éy Aji Sax ji, loo may gàntale, di ma fuuylu?
16
Mitit bay laatikaaf, sama ngone ba tey; sa mbugal yu raglu, ba bopp ubu ràpp!
17
Sa mer mëdd ma, sa mbugal yu raglu sànk ma,
Sabóor 88 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms