Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 87

Sabóor 87:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Yaw, dëkkub Yàlla bi, tuddees na say jaloore. Selaw.
4Yàlla nee: «Ma limaale Misraak Babilon, ñi ma xam di dégg. Xoolal Filisti ak Tir, ak réewum Kuus. Nit a ngii, juddoo fa,»

Read Sabóor 87Sabóor 87
Compare Sabóor 87:3-4Sabóor 87:3-4