Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 87:3-4 in Wolof

Help us?

Sabóor 87:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Yaw, dëkkub Yàlla bi, tuddees na say jaloore. Selaw.
4 Yàlla nee: «Ma limaale Misraak Babilon, ñi ma xam di dégg. Xoolal Filisti ak Tir, ak réewum Kuus. Nit a ngii, juddoo fa,»
Sabóor 87 in Kàddug Yàlla gi