Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 84

Sabóor 84:4-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Éy Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, sama buur, sama Yàlla, sawoor sax tag, nga fat ko, mbelaar it sàkk tàggam, denc ay cuujam fa sa sarxalukaay.
5Ndokklee ku dëkke sa kër, di la màggalati. Selaw.
6Ndokklee ku lay doolewoo, te namma topp njool ma jëm sa kër.

Read Sabóor 84Sabóor 84
Compare Sabóor 84:4-6Sabóor 84:4-6