Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 84:4-6 in Wolof

Help us?

Sabóor 84:4-6 in Kàddug Yàlla gi

4 Éy Aji Sax ji Boroom gàngoor yi, sama buur, sama Yàlla, sawoor sax tag, nga fat ko, mbelaar it sàkk tàggam, denc ay cuujam fa sa sarxalukaay.
5 Ndokklee ku dëkke sa kër, di la màggalati. Selaw.
6 Ndokklee ku lay doolewoo, te namma topp njool ma jëm sa kër.
Sabóor 84 in Kàddug Yàlla gi