Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 83

Sabóor 83:1-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
1Di woyu Sabóor, giiroo ci Asaf. Éy Yàlla, bul ne cell,
2rikk Yàlla, bul tanqamlu, ne patt.
3Xoolal sa noon yiy riir, sa bañ yi fippu ba téen!

Read Sabóor 83Sabóor 83
Compare Sabóor 83:1-3Sabóor 83:1-3