Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 81

Sabóor 81:10-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Buleen fat tuuru jaambur, buleen sujjóotal tuuru doxandéem.
11Man, Aji Sax ji, maay seen Yàlla ji leen yékkatee réewum Misra. Ŋaleen ŋafeet, ma reggal leen.
12«Waaye sama ñoñ déggaluñu ma, Israyil gii nangulu ma.

Read Sabóor 81Sabóor 81
Compare Sabóor 81:10-12Sabóor 81:10-12