Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 78

Sabóor 78:8-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8te baña roy seeni maam; maas gu të woon te déggadi, ñu ñàkk pastéef te sàmmuñu kóllërey Yàlla.
9Waa giirug Efrayim ñoo soxi fitt, te keroog xare ba ñoo daw.
10Ñoo sàmmul kóllërey Yàlla, gàntal yoonam,
11ba fàtte ay jalooreem, di kéemaan yi mu leen won.

Read Sabóor 78Sabóor 78
Compare Sabóor 78:8-11Sabóor 78:8-11