Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 78

Sabóor 78:38-40

Help us?
Click on verse(s) to share them!
38Teewul mu yërëm, baal leen seen ñaawtéef, ba sànku leen. Muñ na meram, muñati, te toppul xolam,
39ndax xalaataat ne suuxu neen lañu, di noo guy dem te du délsi.
40Gàntal nañu ko ba tàyyi ca màndiŋ ma, teg ko naqar ca ndànd-foyfoy ga.

Read Sabóor 78Sabóor 78
Compare Sabóor 78:38-40Sabóor 78:38-40