Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 78

Sabóor 78:10-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Ñoo sàmmul kóllërey Yàlla, gàntal yoonam,
11ba fàtte ay jalooreem, di kéemaan yi mu leen won.
12Fa seen kanami maam la def kéemaan, fa diiwaanu Cowan, réewum Misra.
13Moo xar géej ga, jal ndox ma nim tata, jàlle leen.

Read Sabóor 78Sabóor 78
Compare Sabóor 78:10-13Sabóor 78:10-13