Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 77

Sabóor 77:19-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19nga dënoo biir callweer, melax yi taal àddina, suuf di lox, di reg-regi.
20Biir géej di saw yoon; saw xàll ci digg ndox mu ne xéew, te kenn gisul foo teg tànk!

Read Sabóor 77Sabóor 77
Compare Sabóor 77:19-20Sabóor 77:19-20