Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 77:19-20 in Wolof

Help us?

Sabóor 77:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 nga dënoo biir callweer, melax yi taal àddina, suuf di lox, di reg-regi.
20 Biir géej di saw yoon; saw xàll ci digg ndox mu ne xéew, te kenn gisul foo teg tànk!
Sabóor 77 in Kàddug Yàlla gi