Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 74

Sabóor 74:20-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20Ngalla xoolal ci kóllëre gi, fu làqu ci réew mi, fitna dale fa ba dajal.
21Yàlla bu néew-doole ñibbaale gàcce, yal na ku ñàkk ak ku néewle di la santandoo.

Read Sabóor 74Sabóor 74
Compare Sabóor 74:20-21Sabóor 74:20-21