Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 74:20-21 in Wolof

Help us?

Sabóor 74:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Ngalla xoolal ci kóllëre gi, fu làqu ci réew mi, fitna dale fa ba dajal.
21 Yàlla bu néew-doole ñibbaale gàcce, yal na ku ñàkk ak ku néewle di la santandoo.
Sabóor 74 in Kàddug Yàlla gi