Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 73

Sabóor 73:2-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Waaye man de tuuti kon ma lajj, tuuti ma tarxiis,
3ngir maa ñee ku bew, ndax gis mu baaxle te di ku bon.
4Amuñu metit, xanaa ne faaj.
5Doñ-doñu nit dabu leen, coonoy doom aadama dalu leen.
6Moo leen taxa ràngoo reewande, làmboo coxor.

Read Sabóor 73Sabóor 73
Compare Sabóor 73:2-6Sabóor 73:2-6