Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 73

Sabóor 73:11-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
11te naan: «Lu ci Yàlla xam? Ana xam-xam fa Aji Kawe ji?»
12Ñu bon ñaa ngoog! Ne finaax, di gëna woomle.
13Man kay maa sellal ci neen, di sàmm sama der.

Read Sabóor 73Sabóor 73
Compare Sabóor 73:11-13Sabóor 73:11-13