Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 73:11-13 in Wolof

Help us?

Sabóor 73:11-13 in Kàddug Yàlla gi

11 te naan: «Lu ci Yàlla xam? Ana xam-xam fa Aji Kawe ji?»
12 Ñu bon ñaa ngoog! Ne finaax, di gëna woomle.
13 Man kay maa sellal ci neen, di sàmm sama der.
Sabóor 73 in Kàddug Yàlla gi