Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 72

Sabóor 72:8-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
8mu yilif géej ba géej ak dex ba ca cati àddina.
9Waa màndiŋ mi di ko sukkal, ay noonam mëq suuf,
10buuri Tarsis ak dun ya di ko indil ay galag; buuri Saba ak Seba di ko yótsi yóbbal,

Read Sabóor 72Sabóor 72
Compare Sabóor 72:8-10Sabóor 72:8-10