Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 72:8-10 in Wolof

Help us?

Sabóor 72:8-10 in Kàddug Yàlla gi

8 mu yilif géej ba géej ak dex ba ca cati àddina.
9 Waa màndiŋ mi di ko sukkal, ay noonam mëq suuf,
10 buuri Tarsis ak dun ya di ko indil ay galag; buuri Saba ak Seba di ko yótsi yóbbal,
Sabóor 72 in Kàddug Yàlla gi