Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 72

Sabóor 72:2-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2muy àttee sa mbooloo njub, di àttee sa néew-ji-doole ñi yoon,
3tooli tund yu mag yi indil mbooloo mi jàmm, tooli tund yu ndaw yi xéewale leen njekk,

Read Sabóor 72Sabóor 72
Compare Sabóor 72:2-3Sabóor 72:2-3