Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 72:2-3 in Wolof

Help us?

Sabóor 72:2-3 in Kàddug Yàlla gi

2 muy àttee sa mbooloo njub, di àttee sa néew-ji-doole ñi yoon,
3 tooli tund yu mag yi indil mbooloo mi jàmm, tooli tund yu ndaw yi xéewale leen njekk,
Sabóor 72 in Kàddug Yàlla gi