Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 72

Sabóor 72:10-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10buuri Tarsis ak dun ya di ko indil ay galag; buuri Saba ak Seba di ko yótsi yóbbal,
11buuroo buur di ko sujjóotal, xeetoo xeet di ko surgawu.
12Mooy xettliji aji tumurànke bu woote wall ak aji néewle ju sësul fenn.

Read Sabóor 72Sabóor 72
Compare Sabóor 72:10-12Sabóor 72:10-12