Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 72:10-12 in Wolof

Help us?

Sabóor 72:10-12 in Kàddug Yàlla gi

10 buuri Tarsis ak dun ya di ko indil ay galag; buuri Saba ak Seba di ko yótsi yóbbal,
11 buuroo buur di ko sujjóotal, xeetoo xeet di ko surgawu.
12 Mooy xettliji aji tumurànke bu woote wall ak aji néewle ju sësul fenn.
Sabóor 72 in Kàddug Yàlla gi