Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 71

Sabóor 71:19-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Céy Yàlla, sa njekk àkki na fa kawa kaw. Def nga lu réy. Yaw Yàlla, ana ku mel ni yaw?
20Won nga ma ay yoon coonooki tiis, waaye yaa may dundalaat, ma mucc xóotey suuf.

Read Sabóor 71Sabóor 71
Compare Sabóor 71:19-20Sabóor 71:19-20