Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 71:19-20 in Wolof

Help us?

Sabóor 71:19-20 in Kàddug Yàlla gi

19 Céy Yàlla, sa njekk àkki na fa kawa kaw. Def nga lu réy. Yaw Yàlla, ana ku mel ni yaw?
20 Won nga ma ay yoon coonooki tiis, waaye yaa may dundalaat, ma mucc xóotey suuf.
Sabóor 71 in Kàddug Yàlla gi