Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 69

Sabóor 69:10-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Damaa xér ci sa kër gi, ba jeex tàkk, te jëf ji ñu la sewale man la dal.
11May jooy, di woor, ñu di ma sewal.
12Ma sol ay saaku, di ko ñaawloo, ñu di ma léebu.

Read Sabóor 69Sabóor 69
Compare Sabóor 69:10-12Sabóor 69:10-12