Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 69:10-12 in Wolof

Help us?

Sabóor 69:10-12 in Kàddug Yàlla gi

10 Damaa xér ci sa kër gi, ba jeex tàkk, te jëf ji ñu la sewale man la dal.
11 May jooy, di woor, ñu di ma sewal.
12 Ma sol ay saaku, di ko ñaawloo, ñu di ma léebu.
Sabóor 69 in Kàddug Yàlla gi