Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 68

Sabóor 68:32-34

Help us?
Click on verse(s) to share them!
32ay kàngam bàyyikoo Misra aki galag, réewum Kuus baral loxoom, indil Yàlla.
33Yeen waa réewi àddina, woyleen Yàlla, teral-leen Boroom bi, Selaw
34gawar bi ci asamaan, asamaani démb. Ma ngooguy àddu kàddug doole.

Read Sabóor 68Sabóor 68
Compare Sabóor 68:32-34Sabóor 68:32-34