Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 68

Sabóor 68:20-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20Cant ñeel na Yàlla bésoo bés. Moo nuy jaboote. Yàllaa nuy musal. Selaw.
21Sunu Yàllaa di Yàlla jiy walloo, Aji Sax ji Boroom beey musal bakkan.

Read Sabóor 68Sabóor 68
Compare Sabóor 68:20-21Sabóor 68:20-21