Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 68:20-21 in Wolof

Help us?

Sabóor 68:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Cant ñeel na Yàlla bésoo bés. Moo nuy jaboote. Yàllaa nuy musal. Selaw.
21 Sunu Yàllaa di Yàlla jiy walloo, Aji Sax ji Boroom beey musal bakkan.
Sabóor 68 in Kàddug Yàlla gi