Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 66

Sabóor 66:7-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Mooy nguuroo njàmbaaram ba fàww, di topp xeet yeek bët. Ku koy diiŋat, yàlla boo damu! Selaw.
8Yeen xeet yi, santleen sunu Yàlla, te biral cantam!
9Moo sàmm sunu bakkan, te waccu nu, nu tërëf.
10Éy Yàlla, nattu nga nu, xelli nu, ni ñuy xellee xaalis;
11laaw nga nu, teg nu njàqare.

Read Sabóor 66Sabóor 66
Compare Sabóor 66:7-11Sabóor 66:7-11