Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 65

Sabóor 65:12-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
12Yaay tëje mbeyum at mi say ngëneel, foo jaare, xéewal walangaan.
13Parluy màndiŋ yaa ngi walangaan, li wër tund yu ndaw yi di xumbéen.

Read Sabóor 65Sabóor 65
Compare Sabóor 65:12-13Sabóor 65:12-13