Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 65:12-13 in Wolof

Help us?

Sabóor 65:12-13 in Kàddug Yàlla gi

12 Yaay tëje mbeyum at mi say ngëneel, foo jaare, xéewal walangaan.
13 Parluy màndiŋ yaa ngi walangaan, li wër tund yu ndaw yi di xumbéen.
Sabóor 65 in Kàddug Yàlla gi