Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 64

Sabóor 64:5-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5di jam ku ñu tëru te deful dara; jekki jam ko, te tiituñu ci dara.
6Dañoo dogu ca lu bon la ñu nar, di diisoo na ñuy làqe ay fiir, te naan: «Kenn du ko gis!»
7Dañuy lal pexem njubadi te naan: «Lal nanu pexe mu mat sëkk.» Nit aka xóot xel te xóoti mbóot!
8Waaye Yàllaa leen di jamu fittam, ñu jekki daanu.

Read Sabóor 64Sabóor 64
Compare Sabóor 64:5-8Sabóor 64:5-8