Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 62

Sabóor 62:11-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
11Bul wóolu ribaa, bul yaakaar alalu càcc, neen la. Bu sa alal yokku, nga taf ci sa xol.
12Benn yoon la Yàlla wax, yaari yoon laa dégg, ñu ne; «Doole, fa Yàlla.»

Read Sabóor 62Sabóor 62
Compare Sabóor 62:11-12Sabóor 62:11-12