Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 58

Sabóor 58:2-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Yeen daal, su ngeen waxee, dëgg selaw. Mbaa yeena ngi àtte nit ñi ci yoon?
3Yeena ngi mébét njubadi, di lawal fitna ci réew mi.

Read Sabóor 58Sabóor 58
Compare Sabóor 58:2-3Sabóor 58:2-3