Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 57

Sabóor 57:10-11

Help us?
Click on verse(s) to share them!
10Boroom bi, naa lay gërëm ci biir xeet yi, kañ la ci biir waaso yi.
11Sa ngor a màgg, ba àkki asamaan, sa worma àkki fa kawa kaw.

Read Sabóor 57Sabóor 57
Compare Sabóor 57:10-11Sabóor 57:10-11