Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 57:10-11 in Wolof

Help us?

Sabóor 57:10-11 in Kàddug Yàlla gi

10 Boroom bi, naa lay gërëm ci biir xeet yi, kañ la ci biir waaso yi.
11 Sa ngor a màgg, ba àkki asamaan, sa worma àkki fa kawa kaw.
Sabóor 57 in Kàddug Yàlla gi