Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 56

Sabóor 56:9-12

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9Tumurànke naa, nga gis. Duyal samay rongooñ ci sa mbuus. Du lim nga lépp?
10Bés bu ma wootee wall, dees na waññi noon yi, ma xam ne Yàllaa ànd ak man.
11Yàlla laay màggal kàddoom, Aji Sax ji laay màggal kàddoom,
12Yàlla laa wóolu, ragaluma. Lu ma nit manal?

Read Sabóor 56Sabóor 56
Compare Sabóor 56:9-12Sabóor 56:9-12