Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 44

Sabóor 44:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Yaw ci sa bopp yaa dàq xeet yi, jëmbat fa maam ya; yaa mbugal xeet yi, ñoom, nga yiwi leen.
4Du seen saamar lañu nangoo réew mi moos, seen dooley bopp it mayu leen ndam. Yaa ko defe kàttan ak doole, geesoo leen sa leeru kanam, ngir sa cofeel.
5Yaay kiy sama buur, di sama Yàlla, mayal askanu Yanqóoba ay ndam.

Read Sabóor 44Sabóor 44
Compare Sabóor 44:3-5Sabóor 44:3-5