Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 44

Sabóor 44:20-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20teewul nga not nu, wacce nu xaj ya, këpp nu lëndëmu ndee.
21Su nu la fàtte woon yaw, sunu Yàlla, ba tàllal tuuri doxandéem yi loxo,
22du la ump, yaw Yàlla, mi xam kumpay xol.

Read Sabóor 44Sabóor 44
Compare Sabóor 44:20-22Sabóor 44:20-22