Text copied!
Bibles in Wolof

Sabóor 44:20-22 in Wolof

Help us?

Sabóor 44:20-22 in Kàddug Yàlla gi

20 teewul nga not nu, wacce nu xaj ya, këpp nu lëndëmu ndee.
21 Su nu la fàtte woon yaw, sunu Yàlla, ba tàllal tuuri doxandéem yi loxo,
22 du la ump, yaw Yàlla, mi xam kumpay xol.
Sabóor 44 in Kàddug Yàlla gi