Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Sabóor - Sabóor 43

Sabóor 43:3-4

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Ngalla yónneel sag leer ak sa dëgg, yal na ma yooyu jiite, yóbbu ma sa tund wu sell, sa dëkkuwaay ba.
4Kon Yàlla, naa àgg sa sarxalukaay; yaw Yàlla, yaay sama mbégte, di sama bànneex. Yaw Yàlla, sama Yàlla, naa la màggale xalam.

Read Sabóor 43Sabóor 43
Compare Sabóor 43:3-4Sabóor 43:3-4