Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Sabóor 43:3-4 in Wolof
Help us?
Sabóor 43:3-4
in
Kàddug Yàlla gi
3
Ngalla yónneel sag leer ak sa dëgg, yal na ma yooyu jiite, yóbbu ma sa tund wu sell, sa dëkkuwaay ba.
4
Kon Yàlla, naa àgg sa sarxalukaay; yaw Yàlla, yaay sama mbégte, di sama bànneex. Yaw Yàlla, sama Yàlla, naa la màggale xalam.
Sabóor 43 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms